Nas wi bokk na ci bëre biy dàq ber bi ñu ber yenn làkk yi (rawatina ci
internet bi), xëcc itam gëndaloo guy yamale te di jàpplante, loolu di
sukkandiku ci sañ-sañu askan yi gàddu seen kuute ci caada.
Sedaar Sengoor mi ngi juddoo ca Jiwaalo ci 9 Oktoobar ci atum 1906,
génn àdduna ca Werson (ca Fraas) ci 20 Disambar 2001. Nekkoon
taalifkat, bindkat doonoon it killifa aada ca Senegaal. Mooy ki njëkk
a doon njiitu réewu Senegaal (1960-1980). Wàcc na jal bi ci teeyug
bakkanam, bàyyee ko Abdu Juuf. Ñu bari ci àdduna bi dañu koy jàppe
kenn ci xalaatkati Afrig yi ëpp solo, yu ñaar-fukkeelu xarnu
Yeneen sémbi Wikipedia ci yeneeni kàllaama. Nu lim ci ñenn ñi rekk
Coppite bu mujj bu xët wii 27 Ut 2011 ci 09:29.

